Doyen piik production

Doyen piik production LE DÉVELOPPEMENT

*Yaw Seex Omar Jaañ, nga ne Tuubaa da fa am "Signe Franc-maçon" , yamoo ca nga ne: Màggal ak Gàmmu jamono yooyu xaalis y...
03/09/2024

*Yaw Seex Omar Jaañ, nga ne Tuubaa da fa am "Signe Franc-maçon" , yamoo ca nga ne: Màggal ak Gàmmu jamono yooyu xaalis yi ñi raxas ci lañ koy dugal ci dëkk bi te Sëriñ si dañu cee am ay "pourcentage".*
*Wax dëgg Yàlla de waxoo dëgg moom, li nga wax ay "Kàcc" la. Maa ngi jéggalu bu baax nag ci baat bi ndax (Sëriñ bi) daf ma koy tere, ndax { Sëriñ Tuubaa } moo wax ne:*
*( ولا تقل لأحد كذبتا ✓ أو قلت غير الحق أو أخطأتا )*
*Ca ( نهج ) waaye dey sa kàddu yii dey dara du ci dëgg, gëstu naa ba xam ne nag yii du waxi léegi, waxoo ko léegi.*
*Waaye li ma ci métti mooy: lan Moo tax président de la république Basiiru Jomaay Fay, mu xam lii nga wax ci yoonu Murit ba nóopi mu def la Ministre bop da ngay dox diggante moom ak Sëriñ si, loolu moom métti na ma lool, doonte àndu ma ak Jomaay nag waaye lii moom métti na ma lool, te nag na la leer ne lii moom li fi ak jéggaluwoo ci, man personnellement baalu ma la ko, tooñ nga ma tooñ gu rëy a rëy te tooñ nga { Sëriñ Tuubaa } itam tooñ nga yoonu Murit, nit ku baax ku ne tooñ nga ko, ndax yoonu Murit mooy nit ku baax, ñi baax ñépp a bëgg { Sëriñ Tuubaa }, ku bëggul { Sëriñ Tuubaa } nit ku bon la.*
*Lii nga wax nag dara du ci dëgg ay fen yu léer la ay kàcc la ay duur la loolu moom boo yaboo mu léer la, la firhawna waxoon ne:( أنا ربكم الاعلى) mook sa fen yii soreewu ñu, doonte wu firhawna a gën a rëy nag, waaye sa fen yii moom soreewul ak yooya. Maa ngi lay xamal nag ne: jullit du fen, gor du fen, jàmbaar du fen, nit ku am ngor du fen, fen nit ku baax du ko def.*
*Xaj yii { Sëriñ Tuubaa } di wax ci bayit wii nag xamal ne ca nga bókk.*
*( جهادي انقضى وبيعي ربحا*
*ولسواي كل كلب🐕نبحا )*

06/07/2023

LA RECHERCHE D'UN PRODUCTEUR FINANCIER
POUR UN FILM SUR LES VIOLATIONS BASÉES SUR LE GENRE

23/11/2021
Piik Prod
22/11/2021

Piik Prod

04/07/2021

A ne pas rater le 29 in cha Allah au théâtre de verdure de Mbacke

26/04/2021
ROY DU NIROOK PIIK
26/02/2021

ROY DU NIROOK PIIK

Adresse

Mbour

Téléphone

+221781451840

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Doyen piik production publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager